Ndiiwaani Senegaal yi ay dog lañu ci séddaliinu yoriinu Senegaal.
Ndiiwaan nag ag nekkte (entité) gu suuf la, gu ñuy faral di gis ci réew yiy làkk wu-fraas. Soo demee ci ñiy làkk wu-angalteer weneen dogiin nga fay fekk.
Ci Senegaal, ndiiwaan yi dinañu leen waññi ci lim bu tollook 92 ci 2007.